Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet Duplicate
score
float32
1.04
1.24
Tigrinya
stringlengths
10
431
Wolof
stringlengths
10
372
1.240056
ክብል ወይ ድማ ንድሕሪት ክምለስ እዩ ዝርአ።
il est ici [ee lay tee see] or [ee lay ee see]
1.238733
32ንሳቶም ከዓ ንበይኖም ብጃልባ ተሳጊሮም ናብ ጽምዊ ቦታ ኸዱ።
32 Noonu ñu dugg cig gaal, dem ca bérab bu wéet.
1.229931
በቲ ሓቂ ቐድሶም፥ ቃልካ ሓቂ እዩ።
samp leen ci dëgg, ngir ñu sell. sa kàddu mooy dëgg.
1.226334
እዛ መጽሓፍ እዚኣ ድማ ክትሕግዘካ እያ።
Téere bii dina la ci dimbali.
1.217818
ስለዚ፡ ኣብ ሰማይ ዘለዉ ዅላቶም ኣይኰኑን ፍቓድ ኣምላኽ ዚገብሩ ዝነበሩ።
Kon nag booba, du ñépp ñi nekkoon asamaan ñoo doon def coobare Yàlla.
1.21091
በቲ ሓቂ ቐድሶም፡ ቃልካ ሓቂ እዩ።
samp leen ci dëgg, ngir ñu sell. sa kàddu mooy dëgg.
1.208386
7ንሰብ ዘይኮነስ ከም ንጐይታ እተገልግሉ ካብ ልቢ ኣገልግሉ።
Beyleen seen sas nag ak xol bu tàlli, ni su doon ngir Boroom bi te du nit,
1.208106
7ንሰብ ዘይኮነስ ከም ንጐይታ እተገልግሉ ካብ ልቢ ኣገልግሉ።
6:7 Beyleen seen sas nag ak xol bu tàlli, ni su doon ngir Boroom bi te du nit,
1.20068
ጐይታ እቲ ባርያ እቲ፡ ንሱ ብዘይተጸበያ መዓልቲ ብዘይፈላጣ ጊዜውን ኪመጽእ እዩ።
kon njaatige ba dina ñëw ci bés bu mu ko séenuwul ak waxtu wu mu xamul.
1.199716
ጐይታ ናባኻ ምለሰና፤ ንሕና'ውን ክንምለስ ኢና"!
Ci Sunu Boroom lanu joge Ca Moom lanuy dellu!
1.199556
መጺኡ ከኣ ንኣኻትኩም ነቶም ርሑቓት ዝነበርኩም ሰላም ኣበሠረኩም።
Bi mu ko defee mu ñëw, yégalsi nu xebaaru jàmm fa kanam Yàlla, yéen ñi sore woon ak nun ñi jege.
1.194887
"እቲ ኻብ ይሁዳ ዝመጸ ናይቲ ናይ ሓቂ ኣምላኽ ሰብ ንስኻ ዲኻ፧" ከኣ በሎ።
Mu ne ko: "Yaa di góoru Yàlla gi jóge Yuda?"
1.190318
ብዙሕ ህዝቢ ኸኣ ናብ ጐይታ ተወሰኸ።
Mbooloo mu takku nag dolliku ci Sang bi.
1.18984
ብሓደ ግዜ ኩሉ ዚፈልጥ ኣምላኽ ጥራይ እዩ።
Li ne ci xelam nag, mo ok yàlla rekk a ko xam.
1.187426
18ድኅርዙይ ኢየሱስ ከምዙይ በለ፦ መንግሥቲ እግዚኣብሔር እንታይ ትመስል?
18 Yeesu neeti: "Ana lu nguurug Yàlla di nirool?
1.180888
(ዘፍጥረት 1:28) እወ፡ ምድሪ ኸቶ ኣይትጠፍእን እያ።
(Njàlbéen ga 1: 28) Suuf si du fi mas a jóge.
1.177745
3ንመላእኽቲ ኸም እንፈርድዶ ኣይትፈልጡን ኢኹም?
3 Xanaa xamuleen ne nooy àtteji malaaka yi?
1.176242
እዚኣ ኣቐዲማ እትመጽእ ናይ መጀመርታ ትንሣኤ እያ።
Loolu moo di ndekkite lu jëkk li.
1.176144
ኣቦይ እውን ነዚ ይፈልጦ እዩ' በሎ።
Sama baay ci boppam xam na loolu bu baax."
1.176036
እቲ ናይ ሓቂ ኣምላኽ፡ ፈጣሪ ዅሉ ነገራት እዩ።
Yàlla dëgg ji moo sàkk lépp.
1.175495
ንስኻትኩም ዚብላዕ ሃብዎም፡ በሎም።
Jox leen ñu lekk. '
1.175473
ኣምላኽ ንኹሉ ፈጡሩ።
Yàllaa sàkk bépp mbindeef.
1.175306
ኣቱም ቤት እስራኤል፣ ንነፍሲ ወከፍኩም ከከም መገድኹም ክፈርደኩም እየ።
30 "Lii moo tax yeen waa kër Israyil, ma di leen àtte, ku nekk ciy jëfam.
1.172634
እዚ ድማ ጽድቂ እዩ።
jubóo te jubu ñu ñoo ko waral.
1.171322
ፈታዊኻ ይምርዖ ኣሎ።
Sa xarit bi takk na jabar.
1.170661
"በቲ ሓቂ ቀድሶም፣ ቃልካ ሓቂ እዩ።
samp leen ci dëgg, ngir ñu sell. sa kàddu mooy dëgg.
1.170461
ብስምካኸ ብዙኅ ተኣምራትዶ ኣይገበርናን?
Ndax du ci saw tur lanu daa defe ay kéemaan yu bare?
1.170085
ንነብያተይ ከኣ ክፉእ ኣይትግበርዎም።
buleen lor samay yonent."
1.170033
ጸሎት ምስ ኣምላኽ እንዘራረበሉ መንገዲ እዩ።
Ñaan mooy ci lu yomb wax ak Yàlla.
1.168955
ገለ ሕቶታት ኣሎካዶ?
am nga ay laaj?
1.168457
4 ህዝቢ እታ ኸተማ ግና ተመቕሉ፣ ገሊኣቶም ምስ ኣይሁድ፡ ገሊኣቶም ድማ ምስ ሃዋርያት ኰኑ።
14:4 Noonu waa dëkk bi xàjjalikoo, ñii far ak Yawut yi, ñale far ak ndaw ya.
1.168404
ስለዚ እግዚኣብሔርውን ክሰምዓና ኣይርከብን።
Xam nanu ne, Yàlla du déglu boroom bàkkaar.
1.168035
ጐይታ ቐረባ እዩ።
Boroom bi jege na.
1.167224
ኣብቲ ናይ ኣቦይ ዘበለ ክኸውን ከም ዚግብኣኒዶ ኣይትፈልጡን ኢኹም፧ በሎም
Xamuleen ne sama kër Baay laa wara nekk?"
1.166807
9 ዮሴፍ ከኣ ነቦኡ፡ እዚኣቶም ኣምላኽ ኣብዚ ዝሀበኒ ደቀይ እዮም፡ በሎ።
9 Yuusufa ne baayam: "Ñii ñooy sama doom, yi ma Yàlla jox fii."
1.166578
ንስኻትኩም ግና ካብ ኣምላኽ ስለ ዘይኰንኩም፡ ስለዚ ኢኹም ዘይትሰምዑ" በሎም።
Waaye nekkuleen doomi Yàlla, looloo tax dungeen déglu."
1.166461
ንሱ ኸኣ "እዚ ኸምዚ ዝበለ ዓይነት ብጸሎትን ብጾምን እንተ ዘይኮይኑ ኣይወፅእን እዩ" በሎም።
Yeesu tontu leen ne: "Yu mel ni yii, ñaan ci Yàlla rekk a leen di dàq."
1.166403
48 ናይዚ ነገራትዙይ መሰኻኽርውን ንስኻትኩም ኢኹም።
48 Yéenay samay seede.
1.165695
ብኣዒንትኻ ኣርኣኹኻ፡ ናብኣ ግና ኣይክትሳገርን ኢኻ" በሎ።
Won naa la ko, ba nga teg ci sa bët, waaye foofa, doo fa teg sa tànk."
1.165153
ብሰንኪ ብዝሒ ክፍኣት ከኣ ፍቕሪ ብዙሓት ክትዝሕትል'ያ።
12 Te gannaaw lu bon day law, mbëggeelug ñi ëpp dina wàññiku.
1.164291
ሃዋርያት ከኣ ብብዙሕ ሓይሊ ብዛዕባ ትንሳኤ ጐይታና የሱስ ክርስቶስ ይምስክሩ ነበሩ፡ ኣብ ኲሎም ከኣ ዓብዪ ጸጋ ነበረ።
33 Ndaw yi nag di seedee doole ju réy ne Sang bi Yeesu dekki na, yiw wu yaa di leen dikkal ñoom ñépp.
1.163913
ኣምላኽ ካብ መዋቲ ሰብ ኣጸቢቑ ይዓቢ እዩ።
Yàllaa sut doom aadama.
1.163521
ወይ ከዓ ዓሳ እንተለመኖ ተመን ዝህቦ?
10 Walla mu ñaan la jën, nga jox ko jaan?
1.163357
9 እምበኣር፡ ንህዝቢ ኣምላኽ ዕረፍቲ ሰንበት ተሪፋትሎም ኣላ።
9 Kon ba tey Yàllaa ngi dencal ay gaayam noflaay bu nirook noflaayu Yàlla ca juróom ñaareelu fan ba.
1.162282
ንስኻትኩም ነቲ ሕጊ ብኢድ መላእኽቲ ተቐበልኩምዎ ግናኸ ኣይሓሎኹምዎን!
53 Jot ngeen yoonu Musaa, wi Yàlla wàcce jaarale ko ci ay malaaka, te sàggane ngeen ko."
1.162203
ኲሎም ኣእተዮምዋ ነይሮም እዮም እሞ፡ ብትንሳኤ ኻብዞም ሾብዓተ እዚኣቶም፡ ሰበይቲ መኖም ክትከውን እያ፧
28 Bu ndekkite taxawee nag, jabaru kan lay doon ci juróom ñaar ñi, ndaxte ñépp jël nañu ko?"
1.162197
ዓዲ (መንግስቲ) ዝፍርስ፣ ፋሕፋፍ ዝብል እንታይ ትኾን እንተሎ እዩ?
luy doon muju ki weddi te dëng?"
1.162195
1) "ካልኦት ኣማልኽቲ ኣብ ቅድመይ ኣይሀልዉኻ።
3 "Buleen am yeneen yàlla ci sama kanam.
1.161618
28 ቶማስ ከኣ፡ "ጐይታይን ኣምላኸይን!
20:28 Tomaa tontu ko ne: "Sama Boroom, sama Yàlla!"
1.161618
4 ደቁ ኻብ ድሕንነት ርሑቓት እዮም፣
4 Ay doomam ay sore yoonu mucc,
1.161372
7 ኣብ ከተማ ዚዞሩ ሓለውቲ ረኸቡኒ።
7 Wattukat yiy wër dëkk bi gis ma;
1.160709
+ 9 ኣብ ቅድሚ ሰባት ዚኽሕደኒ ዘበለ ግና፡ ኣብ ቅድሚ መላእኽቲ ኣምላኽ ኪከሓድ እዩ።
9 Waaye ku ma gàntu ci kanam nit ñi, dinañu la gàntu ci kanam malaakay Yàlla yi.
1.160176
ግብሪ ኣምላኽ በቲ ንሱ ዝለኣኾ ኽትኣምኑ እዮ፡ በሎም።
Jëf ji neex Yàlla moo di gëm ki mu yónni.
1.15997
43 ኵላቶም ድማ በቲ ዓብዪ ሓይሊ ኣምላኽ ተገረሙ።
43 Ku nekk waaru na ndax màggug Yàlla.
1.159922
77ንሕዝቡ ናይ ኃጢኣቶም ኅድገት ዝረኽቡሉ ናይ ድኅነት ፍልጠት ክትህብ ኢኻ።
1:77 Dinga xamal mbooloom,ni leen Boroom bi man a musale,jaare ko ci seen mbaalug bàkkaar,
1.159899
ደጊም እውን ውግእ ኣይኪምሃሩን እዮም።
te dootuñu jàngati xare.
1.159824
47 እቲ ሓለቓ ሚእቲ፡ እቲ ዝዀነ ምስ ረኣየ፡ "እዚ ሰብ እዚ ብሓቂ ጻድቕ እዩ ነይሩ" እናበለ ንኣምላኽ ኣሞገሰ።
47 Bi njiitu °xare ba gisee li xewoon, mu màggal Yàlla ne: "Dëgg-dëgg nit kii ku jub la woon."
1.159631
ኣዕሩኹ ብኸመይ ከም ዝሓገዝዎ ፍለጥ።
Seetal ni ko xaritam yi dimbalee woon.
1.15844
ኣነ ዳርዮስ እዚ ትእዛዝ እዚ ኣውጺአ ኣለኹ።
Man Daryus maa joxe ndigal lii.
1.157838
ሽዑ፡ "እዚ ዝሰማዕኩምዎ ቕዱስ ጽሑፍ እዚ፡ ሎሚ ተፈጺሙ" ኺብሎም ጀመረ።
4:21 Noonu mu daldi ne: "Tey jii, loolu Mbind mi wax mat na, bi ngeen koy déglu."
1.157161
ልብን ኩሊትን ምሻጥ ዝለመደ፣
kiy natt xol yi, xam na,
1.156963
ድያብሎስ ሓጺር እዋን ከም ዘለዎ ፈሊጡ፡ ብብርቱዕ ቍጥዓ ወሪዱኩም ኣሎ እሞ፡ ወይለኹም" ኢሉ ተነብዩ እዩ።
Ndaxte Seytaane wàcc na ci yéen, ànd ak mer mu tàng, ndaxte xam na ne, jot gi ko dese barewul."
1.156752
19ኣቱም ደቀይ!
19 Sama doom yi!
1.156693
21 ንሱ ድማ፡ "ገናዶ ኣይተስተውዕሉን ኢኹም፧" በሎም።
8:21 Noonu Yeesu ne leen: "Ndax seen xol dafa tëju ba tey?"
1.156175
ኣብ ራእይ 12:10 እንታይ ክልተ ኣገዳሲ ፍጻመታት እዩ ተጠቒሱ ዘሎ፧
Yan ñaari xew-xew yu am solo lañu wax ci Peeñu ma 12:10?
1.155649
መጺኡ ከኣ ንኣኻትኩም ነቶም ርሑቓት ዝነበርኩም ሰላም ኣበሠረኩም።
17 Bi mu ko defee mu ñëw, yégalsi nu xibaaru jàmm fa kanam Yàlla, yéen ñi sore woon ak nun ñi jege.
1.155645
"ስለዚ፡ ንኣቦ ብብርከይ እምብርከኽ ኣለኹ፣ ኣብ ሰማይን ኣብ ምድርን ዘሎ ዅሉ ዓሌት፡ ካብኡ እዩ ዚስመ።
14 Moo tax maa ngi sukk, jublu ci Yàlla Baay 15 biy cosaanul njaboot gépp, muy ci kaw, muy ci suuf.
1.15556
4 የሱስ እዚ ምስ ሰምዐ ግና፡ "እዚ ሕማም እዚ፡ ወዲ ኣምላኽ ብእኡ ምእንቲ ኪኸብር፡ ንኽብሪ ኣምላኽ እዩ እምበር፡ ንሞት ኣይኰነን" በለ።
11:4 Bi Yeesu déggee xebaar boobu, mu ne: "Lasaar de, woppam jooju du ko mujje; day wone ndamu Yàlla, tey màggal Doomu Yàlla ji."
1.155063
አላህ እዩ ፈጢሩሉ።
Ndax li Yàlla sàkk amoon na sikk?
1.15491
2 ኣስዕብ ኣቢሉ ኸኣ፡ "ኣብ ግብጺ እኽሊ ኸም ዘሎ ሰሚዐ ኣለኹ።
2 Mu ne leen: "Dégg naa ne pepp am na ca Misra.
1.154422
24ብድኅሪኡ እቶም ደቀ መዛሙርት ካብ መንጎኣቶም መን ከምዝዓቢ ንስንሳቶም ተኻትዑ ።
24 Taalibe ya it di werante, ngir xam kan ci ñoom moo gëna màgg.
1.154254
24 ሓይሉ ዓብዪ ኪኸውን እዩ፣ ብሓይሉ ግና ኣይኰነን።
24 Dina gëna am doole, waaye du doon dooley boppam.
1.153692
11ንሕናውን ከምኣቶም ብጸጋ ጐይታና ኢየሱስ ከም እንድኅን ኢና እንኣምን በሎም።
15:11 Nun daal ci yiwu Yeesu Boroom bi lanu yaakaar a mucce, te ñoom itam, ci lañu wékku."
1.153383
21 ንሱ ድማ፡ "ገናዶ ኣይተስተውዕሉን ኢኹም፧" በሎም።
21 Noonu Yeesu ne leen: "Ndax seen xol dafa tëju ba tey?"
1.153321
ዳንኤል 2:44 ብዛዕባ መንግስቲ ኣምላኽ እንታይ እያ እትነግረና፧
16, 17. Lan la ñu Dañeel 2:44 di xamal ci Nguuru Yàlla?
1.153054
የሱስ ንደቀ መዛሙርቱ ፍቓድ ኣምላኽ ኣብ ሰማይ ኪኸውን ኪጽልዩ ዝመሃሮም ስለምንታይ እዩ፧
Lu tax Yeesu waxoon ne taalibeem yi dañu war a ñaan ngir coobare Yàlla am ci kaw?
1.152624
እምበኣር ዘይትፈልጢ ምዃንኪ መሓሊ.
Li ngeen di màggal nag te xamuleen ko, loolu laa leen di xamal.
1.152168
8ቀደም ንእግዚኣብሔር ከይፈለጥኩምዎ እንተለኹም ነቶም ብባህሪዮም ኣማልኽቲ ዘይኮኑ ብባርነት ትግዝኡ ነበርኩም።
8 Bu jëkk, bi ngeen xamagul Yàlla, yéena ngi doon jaamu yeneen yu ñu daan bokkaaleel Yàlla.
1.152167
ፍቕሪ ንኣምላኽ ከኣ ትእዛዛቱ ክንሕሉ እዩ እሞ፣ ትእዛዛቱውን ኣይከቢድን እዩ።
5:3 Ndaxte mbëggeel ci Yàlla mooy sàmm ay ndigalam; te ay ndigalam diisuñu.
1.151975
ንኃወይ ርስቲ ኽመቕለኒ ተዛረበለይ በሎ።
Nga teg ci bokk ak sama baay mboolem coono bu mu daj."
1.151514
15እዙይ ድማ በቲ ዝረአኻዮን ዝሰማዕኻዮን ኣብ ኲሉ ሰብ ምስክር ምእንቲ ኽትኮኖ እዩ።
22:15 Ndaxte li nga gis te dégg ko, dinga ko seede ci ñépp.
1.15124
እ/ሔር ግና ኩሉ ዝኽእል፣ ንዝደለዮ ድማ ዝኽልክሎ ዘይብሉ ዓቢ ኣምላኽ እዩ።
Yàllaa ko dencal ñi ko sopp a ."
1.150655
ንስኻ ናይ እግዚኣብሔር ቅዱስ ምዃንካ ፈሊጠካ ኣለኹ በለ።
Xam naa la, yaa di Aji Sell ji jóge ci Yàlla!"
1.150579
ኣብታ ኸተማ እቲኣ ኸኣ፡ ሓንቲ መበለት ነበረት፣ ናብኡ እናተመላለሰት ድማ፡ 'ምስ መባእስተይ ፍትሒ ኣውጽኣለይ' ትብሎ ነበረት።
18:3 Amoon na itam ca dëkk ba jigéen ju jëkkëram faatu ju daan faral di ñëw ci moom, naan ko: "Àtte ma ak sama noon!"
1.150533
ነገስታቶም ድማ ኬገልግሉኺ እዮም።
seeni buur di la surgawu.
1.150473
ዝገብርዎ ኣይፈልጡን እዮም እሞ ይቕረ በለሎም፤ በለ።
Baay, baal leen ndaxte xamuñu li ñuy def.
1.150032
ግብሪ ኣቦይ እንተ ዘይገበርኩ፡ ኣይትእመኑኒ።
Su ma deful sama jëfi Baay, buleen ma gëm;
1.149678
ከምዚ ዝኣመሰለ ገዛኢ ኺህልወካ ምደለኻዶ፧
Ndax bëgguloo am njiit bu mel noonu?
1.149598
Tigr 40ካብቶም ሕዝቢ ብዙኃት ነዝ ዘረባዙይ ሰሚዖም እዙይ ብሓቂ እቲ ነቢይ እዩ በሉ።
7:40 Bi ñu déggee wax jooja, am ay nit ca mbooloo ma ñu naan: "Dëgg-dëgg kii mooy Yonent bi war a ñëw."
1.149446
ግና ጥበብ ዝበሃል ከመይ እዩ?
Lan lañuy def ak xam-xam boobu ñu am?
1.149177
46 ንሱ ድማ ኣብ ቅድሚ ኣምላኽ ሞገስ ረኸበ፣ ንኣምላኽ ያእቆብ ዚኸውን መንበሪ ኺሰርሕ ለመነ።
7:46 Moom yiw na fa kanam Yàlla, mu ñaan ko, mu sàkkal ko kër ngir askanu Yanqóoba.
1.149135
1) "ካልኦት ኣማልኽቲ ኣብ ቅድመይ ኣይሀልዉኻ።
7 "Buleen am yeneen yàlla ci sama kanam.
1.148965
ከይተሃከየ ንእግዚኣብሔር ይጽበ ነበረ።
moom muy xaar ndigalu Yàlla.
1.148917
ኖህ ጻድቕ ሰብኣይ ነበረ።
Nóoyin nit ku jub la woon, di ku mat ci biir nit ñi mu bokkal jamono, te di ku topp Yàlla.
1.148757
38 ንሱ ኸኣ፡ "ጐይታይ፡ እኣምን እየ" በለ።
9:38 Waa ja ne: "Boroom bi, gëm naa la."
1.148566
45ሽዑ ነተን መጻሕፍቲ ኸስተውዕልወን ኣእምሮኦም ከፈተሎም።
24:45 Noonu mu ubbi seen xel, ngir ñu xam li Mbind mi di wax.
1.148281
ካብ ሰብኣይ ተወሲዳ እያ እሞ፡እዚኣ ሰበይቲ ትብሃል" በለ።
Dees na ko tudde jigéen, ndaxte ci góor lees ko jële a ."
1.14825
በቲ ጽድቃዊ መገድታት ኣምላኽ ክመላለሱ እዮም።
Jaami Yàlla ci yoonu njub
1.1479
17 ሽዑ፡ እስራኤል፡ እዚ መዝሙር እዚ ዘመረ፦
17 Ca la Israyil woy woy wii:
1.147683
ሽመይ ስምረት* እበሃል፤ ጋዜጠኛ እየ።
Avec nom: je suis journaliste.
End of preview. Expand in Data Studio

Tigrinya-Wolof_Sentence-Pairs Dataset

This dataset contains sentence pairs for African languages along with similarity scores. It can be used for machine translation, sentence alignment, or other natural language processing tasks.

This dataset is based on the NLLBv1 dataset, published on OPUS under an open-source initiative led by META. You can find more information here: OPUS - NLLB-v1

Metadata

  • File Name: Tigrinya-Wolof_Sentence-Pairs
  • Number of Rows: 35192
  • Number of Columns: 3
  • Columns: score, Tigrinya, Wolof

Dataset Description

The dataset contains sentence pairs in African languages with an associated similarity score. Each row consists of three columns:

  1. score: The similarity score between the two sentences (range from 0 to 1).
  2. Tigrinya: The first sentence in the pair (language 1).
  3. Wolof: The second sentence in the pair (language 2).

This dataset is intended for use in training and evaluating machine learning models for tasks like translation, sentence similarity, and cross-lingual transfer learning.

References

Below are papers related to how the data was collected and used in various multilingual and cross-lingual applications:

[1] Holger Schwenk and Matthijs Douze, Learning Joint Multilingual Sentence Representations with Neural Machine Translation, ACL workshop on Representation Learning for NLP, 2017

[2] Holger Schwenk and Xian Li, A Corpus for Multilingual Document Classification in Eight Languages, LREC, pages 3548-3551, 2018.

[3] Holger Schwenk, Filtering and Mining Parallel Data in a Joint Multilingual Space ACL, July 2018

[4] Alexis Conneau, Guillaume Lample, Ruty Rinott, Adina Williams, Samuel R. Bowman, Holger Schwenk and Veselin Stoyanov, XNLI: Cross-lingual Sentence Understanding through Inference, EMNLP, 2018.

[5] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Margin-based Parallel Corpus Mining with Multilingual Sentence Embeddings arXiv, Nov 3 2018.

[6] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Massively Multilingual Sentence Embeddings for Zero-Shot Cross-Lingual Transfer and Beyond arXiv, Dec 26 2018.

[7] Holger Schwenk, Vishrav Chaudhary, Shuo Sun, Hongyu Gong and Paco Guzman, WikiMatrix: Mining 135M Parallel Sentences in 1620 Language Pairs from Wikipedia arXiv, July 11 2019.

[8] Holger Schwenk, Guillaume Wenzek, Sergey Edunov, Edouard Grave and Armand Joulin CCMatrix: Mining Billions of High-Quality Parallel Sentences on the WEB

[9] Paul-Ambroise Duquenne, Hongyu Gong, Holger Schwenk, Multimodal and Multilingual Embeddings for Large-Scale Speech Mining, NeurIPS 2021, pages 15748-15761.

[10] Kevin Heffernan, Onur Celebi, and Holger Schwenk, Bitext Mining Using Distilled Sentence Representations for Low-Resource Languages

Downloads last month
8

Collection including michsethowusu/tigrinya-wolof_sentence-pairs